Home
Home  /   Lyrics in English  /   Baye Mass - Ndaw

Baye Mass — Ndaw

Artist: → Baye Mass




 

 

Baye Mass — Ndaw — Lyrics (wo)

 

 

 

 

Ndaw la bou déme
Déwé n′a ndaw fougnou dieum
Ndakh koune ci nioune
Amna loum donone thi yaw
Yallah bouy dieul
Dou tagou day dieki rek dieul
Nagne len ko nianal
Mou am diam foum meuna dem
Donone na domm
Donone kou sori ci niom
Dioté wone ak yaye dji
Wayé domm dey sakh ci xool bi
Fi nieupeu dioy
Fi nieupe la sen xool yi toy
Li ko metti wone
Teknako ci lokho kharite bi
Xolal soy rendi
Lo rendi sa lokho lay nathie
Sonné ké di dieundeu sa famille boul sagane mouy nadjé
Ki kouko wakhone
Li la fiy dieulé sa khel bi lay diougué
Watte ni douka meussa guem
Xolal soy rendi
Lo rendi sa lokho lay nathie
So neké di dieundeu
Sa famille boul sagane mouy nadjé
Ki kokou wakhone
Li la fiy dieulé si sa khel bi lay diougué
Meun na watte ni
Watte ni douka meussa guem

 

 

Aduna yagg na
Loye deff nanko khol
Ningaye nyowé, nonu ngai demé
Fi ken hamut li ngai feki
Li ngai ligey rek nga xam
Suma xamone suma demé ni lay moudjé
Kon ma togg
Demm na dottu delousi
Ndeye ak baye nieup nyungi joye
Rethiou daal di wess
Ku sanione bala ngai demm tago bayi ganaw
Bokk ye xarit yi teww ci keur gui munneh selew
Fimu nekk nieupa teet
Fimm né nieupa diakhle
Nitt ku tey la wonn
Nitt ku bakh deum na
Xolal soy rendi
Lo rendi sa lokho lay nathie
Sonné ké di dieundeu sa famille boul sagane mouy nadjé
Ki kouko wakhone
Li la fiy dieulé sa khet lay diougué
Watte ni douka meussa guem
Xolal soy rendi
Lo rendi sa lokho lay nathie
So neké di dieundeu
Sa famille boul sagane mouy nadjé
Ki kokou wakhone
Li la fiy dieulé si sa khet lay diougué
Meun na watte ni
Watte ni douka meussa guem

 

 

513340cookie-checkBaye Mass — Ndaw
Просмотры 684






When singing your favorite songs, do you often get confused in words? Or maybe you want to play a song, but you don’t know its full content? Do you often find it difficult to find the lyrics of the songs you like? Did the found platforms give you incorrect content? Or are you one of the big fans of karaoke, but do not always have the opportunity to visit special places?


Our portal is a unique find and your best assistant in this matter. Our platform contains a huge amount of texts for the most popular and in-demand songs. We have developed this site especially for you, for all fans and not only! You no longer have to go out to public places to have a good time! Now you can enjoy singing right from home, and any other convenient and desirable place for you! From now on, you can arrange your karaoke evenings in the most unusual locations, alone with yourself, as well as with your loved ones. There is no more need to suffer, singing the words of your favorite songs at random. Using our platform, you will greatly simplify your life, and you will be able to find multiple lyrics for songs of various genres and times, from the oldest to the latest novelties.

The database of our platform contains a large number of texts of the best and most relevant compositions of all time. On our portal you can find contents of Russian, Kyrgyz, Kazakh, Uzbek, Turkish, foreign, and even Ukrainian songs.
We regularly update our site with qualitatively selected materials, carefully checking the correctness of the content of the published texts.

Our platform is constantly updated, and thanks to its maximum functionality, it is very simple and convenient to use. You can easily find the content of any song you like using the search bar. You can also choose something new from the pre-made categories.

If you encounter any display problems or search problems while using our platform, etc., you can always contact us. A team of our qualified specialists will carefully study your appeal, and will definitely correct all the inconveniences that have arisen as soon as possible.

Read completely